Du nil, du nil bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Xamal ma lu leer
Danga maa woolu sa gàll e ma ñëw nga mel ni xale
Yaw daal yaw téppal fële
Danga ba di tappale
Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé
Ngall yaw bul ma defioo lu ma nin ni di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Lég lég sax nga yónni ma
Ma dem bay dem nga teye ma
Léégi sax dematuma
Damay bañ nga dugël ma
Bu fekkeeni parewoo wanu loo di yónéé
Ngall yaw bui ma def loo lu ma nin ñi di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Boo ma waxee fi nga bêgg dem
Ma wax la fi ngay jaar
Demal bl dem, waxal bul wax, defal bul def
Man daal sonn naa, sonn naa sonn naa
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa ko tay, bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë bëgg ak bañ la. .
Перевод песни Létt ma
Ду Нил, ду Нил бег на этом торте Летт Ма Уолла, Фири Ма Xamal Ма Лу Леер Данга, шерстяная Гала-и-мА, что Мел-Халь-каратэ даал-каратэ теппал-Фель-Данга-ду-Ди-таппале Су феккини пареву-УОР-Лу-Лу-Лу-Лу-Нин из ди-шеебе-ле-ле-лет-МБА, что Фери-Ма-Бигга на этой стене. Фири Ма Бэгг на торте "Летт Ма Уолла", Фири Ма лег лег Сакс, что Йонни Ма.
Ma dem bay dem that teye ma Légi Sax dematuma Damay bañ that dugël ma Out fekkeeni parewoo wanu loo di yónéée Ngall karate water ma def loo lu ma nin Ni di xeebe Létt ma Maa that firi ma Begg on létt ma walla тортик firi ma Begg на торте lét ma walla firi бег, чтобы быть демаль Ла воск может быть, если ли не Си каратэ.
Бари pexe weesuwul nettali от géntu moroom
Bëgg, чтобы быть demal La wax, может быть, если ли не Си каратэ.
Летт Ма МБА, что Фири Ма
Бег, что Летт Ма Валла, что торт Фири Ма
Бег, что Летт Ма Валла, что торт Фири Ма
Хух Ма Вакси фи Бегг дем.
Ma wax la fi ngay jaar
Demal BL dem, waxal stream wax, defal stream def
Что ж, да,
Сын, сын, сын, бег, на этом торте "Летт Ма Уолла", Фири Ма
Бег, я из, бан, я из Сабы, если Ксана Гана, из Сабы, из Баха.
TanyaRADA пишет:
- спасибо! От Души!!! ( Улыбаюсь...)все так!!!Liza пишет:
Любимая песня моей мамы